Youssou N'Dour — Baay Faal 가사 및 번역
이 페이지에는 Youssou N'Dour의 노래 "Baay Faal"의 가사 및 한국어 번역이 포함되어 있습니다.
가사
Paroles de la chanson Baay Faal:
Baay faal gueu da djook thia fadjar
Nga sène ko mouy soli sagar
Boppam ba sekkeu ki kawar
Yoré keulleum ba di sikar
Té falé woul khiif ak mar
Boo démé sakh khekh na badar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal gueu da djook thia fadjar
Mani bour Yalla da djook thia fadjar
Nga sène ko mouy soli sagar
Yoré keulleum gueu di zikar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djommeul na wa ndar
Doundeum gueu nekh na
Zikar sa neekh na lol
Baay faal bi, baay faal ki modi guènne goor
Zikar sa motakh mou djégué Yalla
Baay faal bi, baay faal kouko khamone dinga mandou thi mome
Thia tool yeu…
Thia tèène yeu…
Thia wagne weu…
Magal yeu…
Baay faal liguey la khame
Baay faal ndigueul la khame
Baay faal dou khekh dou khoulo
Beuggue neu nite, fonk na nite khekhoulol
Mome la fayé ko lo mou ligueyal sougnou borom
Beuggue na la baay faal
Nangou nite
Kimo djégué sougnou borom
Dey liguey di djokhé motakh baay faal djégué naa sougnou borooom…
Dey liguey di diokhé
Dey liguey di diokhé motakh baay faal
Toggam ga nekhna lol motakh bay faal
Dey magal motakh baay faal
Dey zikar motakh baay faal
가사 번역
파올스 드 라 샹송 바이 파알:
바에이 파알 구에 다 죽 티아 파자르
Nga 세네코 무이 솔리 사가르
보팜 바 세쿠키 카와르
요레 큘 리움 바 디 시카르
테 팔레 울 키프 아크마르
부 데메 사크 케크 나 바다르
기 투럼비 도툴 페이
코우 웨디 리 랏지코와 ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
바에이 파알 구에 다 죽 티아 파자르
마니 보르 얄라 다 죽 티아 파자르
Nga 세네코 무이 솔리 사가르
요레 큘 레움 구우 디 지카르
기 투럼비 도툴 페이
코우 웨디 리 랏지코와 ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djommeul na wa ndar name
구에 네크나 돌드움
Zikar 사 neekh na lol
바에파알비,바알기모디 구엔고르
지카 사 모토크무 데게 얄라
바에이 파알 비,바아 파알 코우코 하몬 딩가 만두 티 모메
티아 도구 유…
티아 테르네 유…
타냐와냐 위우…
마갈 유…
베이 faal liguey la khame
바에이 파알 니디구울 라 하메
바에파알 두케흐 두 쿨로
아니,아니,아니,아니,아니,아니,아니,아니,아니,아니,아니
모메 라파예 코로 무 리구에얄 수구보롬
Beuggue na la baay faal
낭구나이트
키모 제게에 소우구 보론
데이 리가 디 조크헤모타크 바아 파알 제게에 나 소구노 보룸…
데이 리구이 디옥헤
데이 리구이 디 디옥헤 모토크바아알
토감가 네크나 롤모타크 베이 파알
데이마갈 모타크 바에이팔
데이 지카 모토크바아알