Youssou N'Dour — Sportif 가사 및 번역
이 페이지에는 Youssou N'Dour의 노래 "Sportif"의 가사 및 한국어 번역이 포함되어 있습니다.
가사
Woyal sa wayu ndam ii
Dangay bégël sa xol bi
Ndax yaa yor bannex bi
Ni tay bés bii sa bés la
Sa mbër daan na kóntaan nga
Bu ñu daanee sa mbër nak
Na nga fexe ba nee
Po mii dañuy Jonante
Faw mu am ku moyle
Jarula defante, di xasteeka dóóre
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Bëgóón nga mu demee ni demewuko
Mën naa am bu ëllëgee mu gën fee neex
Ba ma làng ag samay gaa yi ngir bànneexu
Xam ne lii fo la nii lay mënë deme
Powun jonante nii lay deme
Tay jii yaw bu ëllëgee keneen la
Fo ag ree de lañ ciy jublu
Moo tax ñu wara dal taynangu defet
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Waa waaw wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jigéén
Sire lañu dóór bal géér ña da ñoo daw
Sire Bàlla moo ñaan Ramata Faal
Siree nga Cees Matee nga Njaarém
Duñ ko wëy ku reew, duñ ko wëy ku ñaaw
Aah wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
가사 번역
우얄 사와유 내담 2 세
Dangay 베겔 sa Xol bi
Ndax 야아 요르 바넥스 bi
니 테이 키스 비이 그녀의 키스
Sa mbër daan na kóntaan nga
Reality daanee sa mbër nak
Nga fexe ba 니
포미 다마구이 요난테
포무 암 쿠모일
자룰라 데판테,소테카 도레
요난테 포 아그 리 라
Booo gañee FO ag ree la
Reg ree lacity in reality
Lepp ci FO AG ree la
보 라 가뇨 무뇰
부코 가네 바알
제고온 무 데메니 데메우코
당은 무엇입니까?
Ba MA làg samay GAA 이 ngir bahnneexu
Xam 네 리 포 라 니 라 mëë 데메
포운 요난테 니이 레이 뎀
당장은 호텔 케닌 라
Fo ag ree de lañi jublu
실무 와라 달 taynangu defet
요난테 포 아그 리 라
Booo gañee FO ag ree la
Reg ree lacity in reality
Lepp ci FO AG ree la
보 라 가뇨 무뇰
부코 가네 바알
와아 와우와우 다비비 우이유
다비 알라 코 이디 바테 사타타
압둘라이 아그 마수르 마수르 ag 마투르 Ag Jaara 보인 지게엔
실무 다우
실재(ñ ñ)발라 모오(ñ ñ)
Siree nga Cees 마테 nga Njaarem
Ñ ñ ñ ñ/ñ ñ ñ/ñ ñ ñ
아,우이 다비 우이 유
다비 알라 코 이디 바테 사타타
요난테 포 아그 리 라
Booo gañee FO ag ree la
Reg ree lacity in reality
Lepp ci FO AG ree la
보 라 가뇨 무뇰
부코 가네 바알