Max Richter — I am writing this letter 가사 및 번역
이 페이지에는 Max Richter의 노래 "I am writing this letter"의 가사 및 한국어 번역이 포함되어 있습니다.
가사
bakkan waruw dàll la fa muy degge dooko yëg
dem rekk delu si rekk
melni wèer wi delu si ci sèy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna dèe ci souff
samay xarit, tèy ji ndadjè bi rafèt na,
djoko, seeddo,
ak rétane bi rafèt na,
xèw bou nèex
mais soubbe dagniouy dèm,
galankor bi moy dougnou
meuneu xamanté bou bax,
dou nouy am waxtou
bou doy ngir soppanté
goudi gi wèss, mangi won
fénène, bi ci toop dina fi sori
ak samay bok ci camion bi,
dinagnouy teugueu ngir
féccelo yénéni nit
ak samy bok ci camion bi,
ngir andi mbékté bignouy djeul
bakkan waruw dàll la ku dul toxu doo xam fu dèkk neexe
fa muy dagge dooko yëg
(Merci a El Cancre pour cettes paroles)
가사 번역
바칸 waruw 다왈 라파 무이 드게 두코 에르
뎀 레크 델루와 레크
멜니 위어와 델루 시시 에르 에고
에네렌 에르 무크 치피,
비디 다노나 디에치 수프
사마이 자리스,테지 이다지 비 라페트 나,
조코,씨드도,
ak 레탄 비 라페트 나,
xèw boo nex
하지만'다지오이 뎀'을 알았어,
galankor Bioy Moy dougnou
미네우 사만테 보 백스,
두 누이 암 왁스토우
bou Doy ngir 소판테
고디기웨스 만기 원
페넨씨,비씨투프 디나파이 소리
ak 사마 복 ci 트럭 bi,
니기르 디나누이
그것은 네니 니트합니까
ak 사미 복 ci 트럭 bi,
ngir Andi mbekté bignouy djul
바크칸 워루우 다우라쿠 두루 독스 두 삼 푸 덱스크 닉스
fa muy dagge 두코 yëg
(이 단어에 대한 엘 칸크레 덕분에)