Youssou N'Dour — Létt ma 가사 및 번역

이 페이지에는 Youssou N'Dour의 노래 "Létt ma"의 가사 및 한국어 번역이 포함되어 있습니다.

가사

Du nil, du nil bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Xamal ma lu leer
Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale
Yaw daal yaw téppal fële
Danga ba di tappale
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma defioo lu ma nin ni di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Lég lég sax nga yónni ma
Ma dem bay dem nga teye ma
Léégi sax dematuma
Damay bañ nga dugël ma
Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé
Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Boo ma waxee fi nga bêgg dem
Ma wax la fi ngay jaar
Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def
Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë bëgg ak bañ la. .

가사 번역

지금 바로 지금 바로 지금!
자말마 루 리어
Swindle maa 우 see sa gáll e ma reality nga mel is xale
Yaw daal yaw téppal fëlecity in italy
단가 바 디 타팔레
수 페키니 파레우 워즈루 디 요네에
Ngall Yaw bul Ma defioo 루 마 닌은 디 xeebe 입니다
릿마 MBA nga Fira ma
체그 나아 엣 마 왈라 책 nga 파이리 마
체그 나아 엣 마 왈라 책 nga 파이리 마
레그 레그 색스 니요니 마
마 뎀 베이 딤가 테예 마
Légi 색소폰 dems 보낸 사람
다마이 bañga dugël ma
부페키니 파레우 모든 루 디 요네에
Ngala yaw bui ma def loo lu ma(reality di xeebe)
릿마 MBA nga Fira ma
체그 나아 엣 마 왈라 책 nga 파이리 마
체그 나아 엣 마 왈라 책 nga 파이리 마
바리 펙세 웨스울 네트 사겐투 모로 옴
Bëgg nga ma demal 라 왁스 Ma Kon 리 니 ci yaw
바리 펙세 웨스울 네트 사겐투 모로 옴
Bëgg nga ma demal 라 왁스 Ma Kon 리 니 ci yaw
릿마 MBA nga Fira ma
체그 나아 엣 마 왈라 책 nga 파이리 마
체그 나아 엣 마 왈라 책 nga 파이리 마
부마 왁시 fi nga 베그 뎀
마 왁스 라 피나이 자르
디말 BL dem,왁살 bul 왁스,defal Bul def
맨달손나아,손나아 소니 나아
체그 나아 엣 마 왈라 책 nga 파이리 마
보뇨 나오 코 죠 .